Waxtaan #1 - Ubbite gi
Waxtaan #2 - Ni Yàlla sàkke àddina si
Waxtaan #3 - Adama ak Awa; li bàkkaar indi ci àddina si
Waxtaan #4 - Kayin ak Abel; Nóoyin ak xonu Yàlla
Waxtaan #5 - Lu Yàlla dige Ibraayma, ak ni ko Yàlla natte
Waxtaan #6 - Maam ya; dundu Yuusufa
Waxtaan #7 - Juddub Musaa; gajj gu tàkk te lakkul
Waxtaan #8 - Musiba yi dal wa Misra; bésub Mucc ba
Waxtaan #9 - Yàllaa xàjjale géeju Barax ya
Waxtaan #10 - Fukki ndigal yi
Waxtaan #10 - Fukki ndigal yi
Waxtaan #11 - Sëllu wurus ba
Waxtaan #12 - Xaymab jaamookaay ba
Waxtaan #13 - Israayil sàkku na buur; Daawuda, Suleymaan, ak kër Yàlla ga
Waxtaan #14 - Waxi yonent yi jëm ci Almasi bi
Waxtaan #15 - Yeesu Yaxya, juddub Yeesu, ak bi ñu ko sóobe ci ndox
Waxtaan #16 - Yeesu am na sañ-sañ ci kaw Seytaane
Waxtaan #17 - Yeesu am na sañ-sañu jàngle ak xam-xam ak dëgg
Waxtaan #18 - Yeesu am na sañ-sañu woo doomu Adama ñu di ko topp
Waxtaan #19 - Yeesu am na sañ-sañu wéral boroom jàngoro, te indi jàmm ci ñi sonn
Waxtaan #20 - Yeesu am na sañ-sañ ci kaw lépp li Yàlla sàkk
Waxtaan #21 - Yeesu am na sañ-sañ ci kaw rab yi ak ci kaw lépp lu bët manula gis
Waxtaan #22 - Yeesu am na sañ-sañ ci kaw ndey
Waxtaan #23 - Yeesu am na sañ-sañu baale bàkkaar
Waxtaan #24 - Yeesu réer bu mujj bi; teg nañu Yeesu àtteb dee
Waxtaan #25 - Yeesu saay na
Waxtaan #26 - Yeesu dekki na Yeesu am na sañ-sañ joxe bakkanam, te di ko jëlaat
Waxtaan #27 - Yeesu feeñu na ay taalibeem; Yeesu yéeg na fa asamaan
Waxtaan #28 - Yeesu moo samp mbooloom gëmkat ñi
Waxtaan #29 - Tukkitel àddina