Skip to Videos All Waxtaan #1 Ubbite gi. Waxtaan #2 Ni Yàlla sàkke àddina si. Waxtaan #3 Adama ak Awa; li bàkkaar indi ci àddina si Waxtaan #4 Kayin ak Abel; Nóoyin ak xonu Yàlla. Waxtaan #5 Lu Yàlla dige Ibraayma, ak ni ko Yàlla natte. Waxtaan #6 Maam ya; dundu Yuusufa. Waxtaan #7 Juddub Musaa; gajj gu tàkk te lakkul. Waxtaan #8 Musiba yi dal wa Misra; bésub Mucc ba. Waxtaan #9 Yàllaa xàjjale géeju Barax ya. Waxtaan #10 Fukki ndigal yi. Waxtaan #11 Sëllu wurus ba. Waxtaan #12 Xaymab jaamookaay ba. Waxtaan #13 Israayil sàkku na buur; Daawuda, Suleymaan, ak kër Yàlla ga. Waxtaan #14 Waxi yonent yi jëm ci Almasi bi. Waxtaan #15 Yeesu: Yaxya, juddub Yeesu, ak bi ñu ko sóobe ci ndox. Waxtaan #16 Yeesu am na sañ sañ ci kaw Seytaane. Waxtaan #17 Yeesu am na sañ sañu jàngle ak xam xam ak dëgg. Waxtaan #18 Yeesu am na sañ sañu woo doomu Adama ñu di ko topp. Waxtaan #19 Yeesu am na sañ sañu wéral boroom jàngoro, te indi jàmm ci ñi sonn. Waxtaan #20 Yeesu am na sañ sañ ci kaw lépp li Yàlla sàkk. Waxtaan #21 Yeesu am na sañ sañ ci kaw rab yi ak ci kaw lépp lu bët manula gis. Waxtaan #22 Yeesu am na sañ sañ ci kaw ndey. Waxtaan #23 Yeesu am na sañ sañu baale bàkkaar. Waxtaan #24 Yeesu réer bu mujj bi; teg nañu Yeesu àtteb dee. Waxtaan #25 Yeesu saay na. Waxtaan #26 Yeesu dekki na Yeesu am na sañ sañ joxe bakkanam, te di ko jëlaat. Waxtaan #27 Yeesu feeñu na ay taalibeem; Yeesu yéeg na fa asamaan. Waxtaan #28 Yeesu moo samp mbooloom gëmkat ñi. Waxtaan #29 Tukkitel àddina.